|
Ich
hab geschworen deine stimme
|
Waat
naa ne sa baat,
|
|
Zumindest
die vergess ich nicht
|
moom,
duma ko fàtte.
|
|
Manchmal
glaube ich noch immer
|
Léeg-léeg
damay gëm ba tey
|
|
Ich
hÖre, wie du mit mir sprichst
|
Damay
déglu, mu mel ni dangay wax ak man.
|
Bevor
die fÄlschungen beginnen
|
Bala
ma sama xel di wor,
|
Bevor
du untergehst im nichts
|
bala
ngay tàbbi ci neen,
|
Will
ich mich noch einmal erinnern
|
dama
bëgga fàttalikuwaat benn yoon
|
Wie
du fur mich gewesen bist
|
ni
nga meloon ci man.
|
Dein
atem schwer, die erde leicht
|
Sa
nawu diis, suuf si woyof,
|
Die
himmel wie mit gold beschlagen
|
asamaan
si mel ni lu sàddoo wurus,
|
|
Dein
fenster leer, ein schritt zu weit
|
sa
palanteer ne wëyë, ab jéego
bu xëccu lool,
|
|
Und
endlich alle fragen hinter dir
|
léegi
nak laaj yépp ci sa gannaaw.
|
|
Dein
leben war wie lose schlingen
|
Sa
àdduna dafa meloon ni ay takkoon yu
fecciku
|
|
Die
keine hand zusammenfuhrt
|
yu
benn loxo dul fas.
|
|
Du
warst ein meister im beginnen
|
Njiit
nga woon ca njalbéen ga.
|
|
Du
hast dir gerne zugehort
|
Danga
soppoon di déglu sa bopp.
|
|
Du
bist ins leben eingesunken
|
Danga
sóobu ci àdduna si,
|
|
Als
wÄre's ein heisses bad
|
ni
su doon ndox mu nugg
|
|
Der
liebe voll vom dasein trunken
|
Nga
fees ak cofeel, bëgg àdduna
|
|
Bis
es dich ausgespien hat
|
ba
na mu la yàbbee,
|
|
Der
anfang schwer, das ende leicht
|
njalbéen
gu jafe, muj gu yomb,
|
|
Du
schaust uber den rand der welt
|
di
xool ci kow komborko dunyaa,
|
|
Dein
kopf ist leer, ein stuck zu weit
|
sa
bopp ne wëyë, ni néeg
bu yaa lool,
|
|
Du
weisst dich halt nichts mehr
|
nga
xam ne dara téyeetu la
|
|
Dich
halt nichts mehr und fallst
|
dara
téyeetu la te yaa ngiy daanu.
|
|
Ce
qui suit est la traduction en français
du passage en wolof, chanté par Ismaël
LO : |
|
|
ma
ne duma la fàtte ba abadan
|
Je
dis, je ne t’oublierai jamais
|
|
sañ naa ko seede man
|
j’ose
le proclamer, moi (Litt. j’ose en témoigner,
moi)
|
|
pas-pas bi nga amoon si sa liggéey
|
la
détermination que tu avais dans ton
travail
|
|
dox
nga ko ba mu jeex
|
tu
l’as menée à sa fin (litt.
Tu l’as marchée jusqu’à
ce qu’il soit fini)
|